Sama boroom Jesus,
Duggal ci sama xol.
Baal ma sama bàkkaar.
Raxasal ma te setal ma.
Moytul ma.
Jesus, jërëjëf ci li nga dee ngir man.
Gëm naa ni dekki nga ci néew yi.
Ak ni Yaa ngi dellusi ngir man.
Feesal ma Xel mu Sell mi.
Jox ma bëgg-bëgg ci ñi réer.
Xiif ci mbiri Yàlla.
Ak fit bu sell ngir waare xebaar bu baax bi ci Yeesu Kirist.
Mucc naa!
Dama judduwaat!
Dañu ma baal!
Maa ngi ci sama yoon ngir dem asamaan si.
Ndax amnaa Jesus ci sama xol.
